Immigrés/Bitim Rew
by Super Étoile de Dakar
From the album: Vol. 8 : Immigrés / Bitim rew
Duration: 7:03
Lyrics for Immigrés/Bitim Rew
Ibu Njaay Faama Ibu Njaay Faama Waaw bittim réew ña fa nekk dëkk ñu fa Mujj u mujj yaay dañuy déllu ci waaw Sénégal Ibu Njaay Fama Ibu Njaay Fama Uzin bitim réew ña fa nekk dëkk ñu faa Mujj u mujj yaay dañuy ñibbi cee waw Sénégal Hoolé Bitim réew ligéey la laaj Immigré ligéey la laaj Immigré Ibu Njaay Fama Ibu Njaay Fama Ñu nee "bitim reyew ñu fa nekk dëkk ñu fa Mujju mujj yaay da ñi déllu ce Ndaxte ñoo ñu xamu ñu léen Fi la ñu saaso" Ñu nee "jòom mooy tukki yaay Waye fulla mooy ñibbi cee Noo mën a mel Loo mën a am ndeysan ñibbi ce la war Youssoo sabali nga,sabali nga Déedéet samaliwul deh Moytul lu la neex defal, lu la nex waxal Ndax bañuloo te mbëgg nga Ñepp a am Coodu Faal Caa-Ndeela, yaay, Caa-Ndeela Ñu nee Nene Ada may ma ci saa jaam ñi Maa Dické lo ba caa Xaayo, li sagam neex na la Yaayu Colle Jaaga woo nala Baay Yuusu, xam nga li ma neex ci yaw Yaa ñi seet li doxal réew yi Waye nit ku mënul te bà wul Laajul tay def, lu yà kku, moo, moo, lu mu Yuusu, yaw deh yà kkoo Sant nañu léen, ñoo ñi dileen ñanal Su ma delloo, dileen way yan too Waaw Sénégal Mooy sunu réew Waa sant nañu léen, ñoo ñi dileen ñanal Su ma delloo, dileen wayyan too Waaw Sénégal Mooy sunu réew Waaw najjee mu ni laa, say ñu nekk Su ma sañoon di koo défal ak yéen Waaw Sénégal, mooy sunu réew Ibu Njaay Faama Dabaax (waaw Sénégal) Abdou Aziz Malick Dabaax (Mooy sunu réew) Ibu Njaay Faama Dabaax (waaw Sénégal) Abdou Aziz Malick Dabaax (Mooy sunu réew) Waaw sant nañu léen, ñoo ñi dileen ñanal Suñu delloo, dileen wayyan too Waaw Sénégal Sénégal, Sénégaloo Mooy sunu réew